Folk Tale

Baay gaynde ak jenax

Translated From

El león y el ratón

Book TitleEl León y el ratón
Publication Date0
LanguageSpanish

Other Translations / Adaptations

Text titleLanguageAuthorPublication Date
De Leeuw en de MuisDutchPeter Franke_
Si Daga at si LeonTagalog_0
Το λιοντάρι και το ποντίκιGreek_0
Løven og musenDanish_0
An Leon agus an LuchógIrishCailliomachas2009
Sang Singa dan Si TikusIndonesianMalik diNata2009
O shagar thàj o kandojBalkan Romani__
The Lion and the MouseEnglish_0
Lehoia eta sagutxoaBasque_0
Lew i myszPolish_0
Lõvi ja hiirEstonian_0
Ilay Liona sy ilay VoalavoMalagasy__
De liuw en de mûsWestern Frisian_0
Mur y LleónAsturian_0
O leon i o ratolinAragonese_0
ljónið og músinIcelandicÁsa Kolka2010
Leõ ha angujaGuaraniZulma N. Sosa0
Az oroszlán és az egérHungarianCaravilcius2009
AuthorOusseynou Dieng
Book TitleEl León y el ratón
Publication Date2010
ATU075
LanguageWolof
OriginSpain

Ba jenax guénee cha paxamma, jakaarlook baay gaynde, cha la xam ne tay lakoy sakal péxe.

-Cha saas ya lako né: Baay Gaynde, jéguël ma buma lekk! Bës da na ñëw, dinaa la amal jarín. Baay Gaynde neko: -Bann jarin ngamay amal, néew doole?

Bako baay gaynde xoolee chi kaw ba chi suuf, yërmandee tax mu baal ko. Bañu cha teguee ay fann, jenax degg choow lu bare lool. Bamu yeguee cha berëp ba, chala seen Baay Gaynde, ap mbaal umb ko.

-Dana la xétali! lacha tek. Baay gaynde neko: -Yaw, néew doole!

Cha la jenax tambalee dagg baal ma ak bëñ ya, ba xétali baay gaynde.

Cha gudi guoogu ba tey, lañu nekk ay xaritu benn bakan.


Text view